Le MAGAL de Viviane Chidid

Mâne mame diarra sant serigne touba ….bou Weeeer.

sant serigne elhadji mbacke…

sant borom Darou noreyni…

sant serigne djily Mbacke ak bayefall seydina abo…

Yalla na souniou borom défal soutoureu nangoul niou souniou niane ci barké cheikhoul khadim…

DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA

#MAGAL2017

#VIVIANE