Feuz GALSEN déclare publiquement son amour à Bandit (lisez)!

Waaa mane ni ma beugué Bandit ndankh Jiam la ? Mane damay mérr bandit khôl ma ma contane 😂

Damay khiiff bandit khôl ma 👀 ma soure

Damay guinmintou 🙃 khôl bandit yéwou

Damay âme dhiarré khôl bandit constipé😉

Maar naane khôl bandit rek mandi ☕️

Wayy wayy si bandit existé pas j’allais sûrement

faire grève de garçonnage 👨🏽‍💼

Bon je retourne au lit
Elhadji Konate mon amour ❤️ tu es ma vie

Mon bonheur 💕 ma respiration

Bandit je t’aime 💕❤️

Commentaires fermés.